最近搜索
Devorante Loyaute - Infestation 《Just Do It (Explicit)》 HQ
更新时间:2025-04-03 17:18:09
文件格式:mp3
音乐下载
被下架或封杀等部分试听资源与网盘资源可能不一致,请以网盘资源为准
标签
Devorante Loyaute - Infestation 相似推荐
歌词

baby girl lets go away from haters girl

you got my love till the day you will make me hurt

you've got my heart, kone bouldi weddi sama love

(oww yeah hunhumm)

boy néna dafma nop, dafa miir ci mane

fouma romb wadjiy beugeu dof, lolou ley wakh si mane

dem bay wakh ni moma mom

sou ma amoul kenn douma am

mais mane sorina,sama mbeuguel si iow wessouna

khana boy bi khamoul mom rekk lafi bardé wone

paré wona def louné pour iow, ayy boma faalé wone

wayé iow ngua khepp ma, kholoula ma falé woma

ba tey ma reutie la, romb la deppassé na la

noboma wone, noboma ndeysaane nobama wone

bamalay face time, taloma wone

ndiago bi dh moko wakh

souma khamone wessouna

meyma diam nobatouma

bouldi khep kila nop mbeugueleu fort dou loy tey

yalla bour bi mo fi né ba takh mou len di bolé

ya ngui taylé sa soubeu ak mom boy basé wou tey

lifa gouddou tank bayil kholam binguay foyé

bouldi khep kila nop mbeugueleu fort dou loy tey

yalla bour bi mo fi né ba takh mou len di bolé

ya ngui taylé sa soubeu ak mom boy basé wou tey

lifa gouddou tank bayil kholam binguay foyé

(Oww yeah hunhumm)

(mbegueleu fort dou loy tey)

baby diéggé ma boul tipsé kay ma begeul la

setsi ma tonight dou meuneu yomb Rangg ma teral la

yeukeutila tafoula, khossima ma gadji la

teyla samedi soir boul ragal dara may sa superman

super night lalay dikké

tey ngua kham né may bad man

tey ngua toy ni koudone sangou guedj

mak iow ba abadane

tey ngua gueuleum, khekh ba seuleum

deureum doumala ko mey

bougnou paré dang ma nara gueureum

té sakh doko tey

donté tey ngua may soga love

narna noy ni pain au lait

pain au lait wouy pain au lait

bougnou pognsé si biir lait

sayouma la kholé ngua seugg

ndakh limala collé (YUP)

noboma wone, noboma ndeysaane nobama wone

bamalay face time, taloma wone

ndiago bi dh moko wakh

souma khamone wessouna

meyma diam nobatouma

bouldi khep kila nop mbeugueleu fort dou loy tey

yalla bour bi mo fi né ba takh mou len di bolé

ya ngui taylé sa soubeu ak mom boy basé wou tey

lifa gouddou tank bayil kholam binguay foyé

(Oww yeah hunhumm)

baby girl lets go away from haters girl

you got my love till the day you will make me hurt

you've got my heart, kone bouldi weddi sama looove

(Oww yeah unhumm)

(mbegueleu fort dou loy tey)